@rass_nk: Je vous explique ce qui est arrivé à un de mes amis, l’autre jour . #developpementpersonnel #rassnk #Relationship #relationtoxique #storytime
Un future milliardaire est en train de lire mn commentaire boss comment tu va ?
2024-07-22 21:31:17
1595
M𝚒𝚜𝚜 𝚁𝚊𝚢𝚜🌴☀️🥥 :
Sama mbokk jiguene yi amna niou niak diom nk ioe bo khiffé amo papa ak yaye 😭 ?
2024-07-22 21:28:57
491
mistmoukh :
right😏goor dafay am fouleu
2025-04-08 16:34:07
0
❤️🧸K•A•T•Y~🇸🇳 :
Mani meunone ngueine changer katy bi dei 💔😂😂😂
2024-09-15 01:48:01
7
aboubakarydiop4🇸🇳 :
Modou khana bokoul si syndicat bi ??😂
2024-07-22 21:34:46
195
lunho🩸_bou liss_🫀 :
Djigeen ak tapha tine nio yamme niake khèll laniou deff😂
2024-07-22 21:30:14
18
Aïtabadji❤️ :
Loulo cela veut dire k kou djigueine ki nobouko so invité djiguene mou ande ak xaritam reik nonoula
2024-07-25 07:18:17
44
Queen dija👸💯🇸🇳 :
iow j'aime vraiment ta façon d'exprimer 😊❤️
2024-07-22 22:16:12
208
mbaye ndao hala Madrid ❤️❤️ :
sampou rék 😂😂
2024-09-17 15:25:56
0
Ma Hélène 💕 :
Mane dh sama kharite sou wakhé ma guounguè ko sax damay bagn les filles am lén xéll
2024-07-23 01:41:17
107
Dou2two boy :
Ndéyesane Wallahi mettina trop sakh
2024-07-22 21:39:19
51
Sheikhndiaye81 :
Bilay t’as raison nitt day ame foula 😂
2024-07-22 23:13:35
39
La sénégalaise 🤍 :
Moy badola you tite yii rk 😅
2024-07-24 14:16:56
5
🦋__Amiiratoune__🌸 :
prkw je me sens visé😭
je p pas partir sans ma besty c pas méchant no
2024-07-29 19:48:06
3
Dioyou bouba Ndour🦦🙂↕️ :
Sama mbokou yii tay rousnagn dh waxna deug sakh badola mo baxoull shim mane rousna sakh boudone mane damakay wakh gnou dém maïga🥲👩🏼🦯
2024-07-22 22:06:16
7
ziii :
mane un jour bima invitè sama guel resto ma guiss mou and ak kharitam guiss n'a len mai gnom guissou gnoumeu guiss n'a moumay def apell mai bobou daw na bou yagu🤣🤣