@abdousaliou803: Loudoul yalla néne leu tay yagui ni am ay tresors machala yalla na yalla sam #couple #couplegoals #couplestiktok #religion #Love #femme #pourtoii #pourtoi #view #fyp #senegalaise_tik_tok #views #fypp #video #bebestiktoks #bebes #enfants #mariage #amour #espagne #france #dakar #triste #sourire #meuble #entreprise #senegal @Eva séduction @Buzz UE @sabadorcouture94 @Mamendiayesavon @MamyBabacar l’officiel @Rafetdjikho93 @abdoulayediopkhass1

abdousaliou803
abdousaliou803
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 16 December 2024 22:31:05 GMT
913055
84117
4212
6982

Music

Download

Comments

lment.serigne.baba4
ÉLément🥰 Serigne💕💕 Babacar :
kan momaiy santéle seydina mouhamed
2024-12-17 23:33:31
969
racegale
Race Galé :
Kouy khassane goor rek danga guissoul kou bakh mais gniy bakh gningui bakh batay
2024-12-17 03:53:49
1837
fatou.faye.diagne4
Fatou Faye Diagne❤️ :
Li nehh na
2025-01-07 01:37:08
1
ndiogouamina
prési 💱🛍️🇸🇳🗽🇯🇵 :
wadji louko téré dioye la khamoul 😭
2024-12-17 08:23:11
1001
sokhnadiarrarassoul4
Sokhna Diarra Rassoul :
Sokhna tegal fi Ameth affaire la 🫴🏾
2024-12-17 14:28:30
894
thiatousidy
La jolie❤️ :
Ay way les hommes xoléne thi ki sén nawlé laa oh😭
2024-12-17 09:15:24
659
waxtanesunubiir.4
waxtane sunu birr :
khamguen ni djiguén soko téralé dakoy wah ci penc mi dano gore
2024-12-17 08:52:20
1078
alhamdoullilahalakoulih
senegal rekkk :
yallah nalen yallah dioubolé mousseul len si thiat
2024-12-17 02:01:54
576
user69470920909280
user69470920909280 :
machalla
2025-01-07 18:41:50
1
beignet27
FALLY🍒 :
Le regard de monsieur 🥰yalla na leine yalla sameu
2024-12-16 23:21:47
1057
ramatulaay
Ramatulaay :
mashaallah pour une fois ma giss goor sénégalais bu baax ❤️❤️❤️yalna la yalla fay
2024-12-17 11:09:47
175
junior___bng
Junior_Bng🇸🇳 :
Wa ASC goor dou projet changer goleine avis batay wala 😂
2024-12-17 07:07:43
72
lialetailleur
lia le tailleur :
Souma amé diabar nama beugu comme Senegalais yi ninou beugué sonko meme souma fenei gnouni gonga
2024-12-17 05:18:22
148
queenfatimah0924
Allakhou yalam🤍🔐 :
Bravo chapeau à vous Ameth 🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳
2024-12-17 07:30:26
836
mdxxl14
🇸🇳🌾 M Dia🐄🌍 :
Mane aussi sama diabar ohhh aka bakh ta yeureum ma billahi dama dem ba ame kérsa si mom elle est formidable ❤️❤️message vocal 🎙️24h24 … soumaye wakh si mom
2024-12-17 07:09:54
217
grosssiste2.0
Grossiste2.0 :
Ameth moy sokhna🤌🏻❤️💍
2024-12-17 14:55:20
235
oumoukhairy19
sokhna Oumou mu Serigne Bbcar :
Ameth bo guisser Sama message Defma signe affaire la
2024-12-17 09:34:41
187
sokhnaoumou4
Sokhna Oumou :
Ameth siguil nga mbolém djiguéne 🥰
2024-12-17 12:45:42
241
mamychou11
mamy petit sow :
goor gni amatinagne ndame😁
2024-12-17 14:40:52
67
ablayethioune1111
ablaye thioune akassa 1111🇯🇴 :
Sallahou alla mouhamed 🥰
2024-12-17 10:35:40
136
naginashop
User2525 :
Foo leene guiss goor bou sagal diabaram yalla dakoy soutoural loum laal mou barkeel. Na yalla samm leene
2024-12-17 17:42:59
60
mamancoumbasow
Mum :
mashallah li rek la djiguene sokhla dou khalis
2024-12-17 02:33:29
135
user2775170522509
oumy Gueye :
éye way foumay dielé dieukeur bou mélni
2024-12-18 03:03:35
8
suistapascompris
lalale bayil Sagara bi❤️🤣 :
sokhna tégal fii ameth affaire la🤣🤣dina la expliquer après
2024-12-17 17:08:59
16
infolinf2
Beugue seu rew🥰 :
Walay guor guou bakh yomboule bakhna beugue ndiambote oyof machalla naguéne feké lep❤️❤️❤️
2024-12-17 01:31:20
108
To see more videos from user @abdousaliou803, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About