@tagat_ak_ndiarigne: Reveil toi n’importe quelle heure sans avoir des maux de tête #senegalaise_tik_tok #conseil #viral_video #pourtoi

Tagat ak Ndiarigne 🧏🏾‍♂️🧠🤔
Tagat ak Ndiarigne 🧏🏾‍♂️🧠🤔
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 16 December 2024 22:31:19 GMT
216513
17737
293
2602

Music

Download

Comments

second.xassida4
SECOND XASSIDA :
Kan momay santéle seydina mouhamed🥰🥰🥰
2024-12-20 21:31:04
33
coachsall360
Cheikh Omar Sall :
iza zoulzilatil ardu... jusqu'a yawma izin tu khadissu ahbaraha. aussi marche bien maachallah. 🙏
2024-12-17 19:49:00
77
diene1818
élément serigne saliou :
Allahou Akbar démb lako déf 05h diot ma yéwou di diéma nélawat wayé pour man sama rouh bi moy wadja guéneu sama yaram diss sila djougué djouli🫣🙏❤️
2025-02-16 12:37:18
3
thernodiallo045
thernodiallo045 :
dégleu billahi défnako
2025-01-16 09:46:01
2
ndatou4
fatima zahra :
kholal dieulal réveil bi wala téléphone bi soril ko dinga diouk force
2024-12-20 08:56:59
3
pape.alioune.diaw
Pape alioune Diaw :
ban sourat la
2025-01-19 15:40:16
3
lavraimenace89
Papa Bar bou Takh bi 🇲🇷🇸🇳 :
kouma kay bindeul guir yalla
2024-12-17 17:40:31
3
s.fall445
Sfall Bëgg Jàmm! :
lu wér la de, leeg-leeg sax melantan moo lay màtt.😄
2025-01-20 17:55:16
4
liunmetal
Liun 〽️etal🇸🇳🇮🇹 :
Momay yè chaque jour
2024-12-17 16:50:03
4
businesslaclasse0
Business La Classe :
mannn 3 ikhlass rekk layy defff
2025-01-06 22:28:58
3
moustapha.samb9968
Moustapha samb :
bilay wax ga dégge réveil téléphone bi non la maydéf
2025-03-13 05:48:49
2
mahmoud_4f
Nabil_Moustapha :
as salamou aleykouma magui ziar mais mom inama ana la commencer die!!??
2025-01-30 01:51:08
2
nabila_shop06
Nabil Moustapha fragrance :
Oustaz Massila Kane
2025-02-02 02:51:47
2
beuguefallou911
beuguefallou911o :
Bilhi walahi watal lahi jour bimako ndieka essayer nonou la deme
2024-12-24 23:54:36
2
baydiouf3
JUUFEEN BI 🇸🇳☪️ :
bayyil niou régler réveil rk 😫😭
2024-12-18 09:50:17
24
oumar6496
Oumar :
lane Moy sa dalil
2024-12-19 14:49:09
1
yayousalikha0
Sow lala :
Mane al mulk rek laye déglou mo waral may yéwou heure bou réveil bi sonné
2024-12-17 01:40:32
16
serignyade1
serignyad 758352175 :
loulou balaga brré 07:30 diot🤣🤣
2024-12-16 23:53:51
13
momosne8
mouhamad :
Nakka essayer inchallah khol loumouy diokhé❤️
2024-12-18 11:00:43
4
mactoum_study_link
👩‍🎓MACTOUM STUDY LINK 🛫🤴🧳 :
merci chercher nako ba son merci beaucoup 🙏
2024-12-17 22:40:55
3
aboukhadidiallo
Khadimou Sunna Diallo :
mon père m'avait donner ça depuis 2008
2024-12-18 00:13:13
13
malickfall973
EL malick nay leur.com :
Bilaay li serigne bi limey wakh masi kham dara taay rek def nako 😂😂😂
2024-12-18 16:25:35
4
m909913
Bamba_Sk_jr🐐😍😮‍💨 :
Hi lolou woroul😂
2024-12-17 21:17:42
1
diop.le.poete
Diop•Le•Poète●♤○ :
Gorgui khana sopé Al Maktoum nga?
2024-12-18 16:14:04
37
To see more videos from user @tagat_ak_ndiarigne, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About