@tempsmort.nka: Un extrait de votre nouvelle emission Temps Mort que vous retrouverez a partir de ce Samedi 20h sur les reseaux de NKA ☺️ @african_queeeen @Bass_SerieLadyDiama @fatimathou @Marodi TV @finachonhairhair
Avant goor gnou bari dagno goré wone mais légui goor gni dagno faux trop
2025-02-07 06:14:16
1530
astougueye7971 :
mon problème actuel ma famille danio khépp ki ma beug ,nénaniou douniou mako mayy 😭😭
2025-02-07 00:04:54
314
Anna ❤️❤️ :
Ya dioguama ba taye maman♥️♥️♥️🥰🥰🥰
2025-03-06 12:25:09
0
Lamine Mane ibn SBN :
Maman Yallah nga goudou fane thi barké Yonente bi saws 🙏
2025-02-07 07:21:23
411
raya :
Sékk ko akk Gör tamit Lou am solo la
2025-02-07 01:05:38
853
Nene Niang :
Ame na Kou bindeu l’argent j fais pas l bonheur 😂😂
2025-02-07 07:04:37
89
Nassiril haqq rek :
mère yeine seine diamono amatoul khalé legui yi dh thi goor dou projet lagn nekk mbarane rek diap ni nio ngui nakh gas yi té legui kou leu diokh di nga diokh😭😭
2025-02-07 07:33:41
32
sénégalais 👳🥹 :
beauté mére bi guiss ngén ko Ohoh 😍😍ki mo dakh sén adjia dialo bobou déh 🥰
en plus mentalité bimou yorr rar na si souniou yaye yii légui
2025-02-06 23:15:54
924
Max :
Merci maman deug dou nekh ☝️🩷🙏
2025-02-08 03:15:45
0
Yass-Prints-Business :
Surtout mères yi naniou diapalé sèn domou djiguèn yi ci sen beug beug wayé sa morome amna li défal na li yayam 😢 sa bascule traumatise la mentalité de la fille
2025-02-07 01:03:04
372
Voisine De Aladji Lady Diama :
Sé pourecoii on di L’argent je fais pas bonheur
2025-02-07 11:53:55
9
lolita MINTÉ :
17 enfants la degue wala ma degoul bou bakh
2025-02-07 07:43:47
38
kiyachu97 :
Mais seikh ko ak goor mo diafei leigui maman
2025-02-07 11:29:48
96
sns :
loumouy wahni yeup si djiguen gni lanek gnioguifi si commentaire yi di triste triste lou di doul🤔🤔
2025-02-07 00:50:45
76
Baye Bass routier 63🇸🇳🇫🇴 :
gni laniou wara diokh micro 🎤🥰
2025-02-07 02:57:50
314
elhadji bara seyda 86 :
wakhofi dara gor gnou bakhi gnogui fi moi j ai divorcé 2 diambare, dioulit ,responsable mais matérialiste djiguen sincèrement
2025-02-08 10:27:49
1
gueye773 :
djiguéne yi la plupart yiniouy guiss si reseau motakh la plupart daniouy tek séne beutt fou sori alors galsen bi niou si daniouy takhalé rek
2025-02-07 01:28:30
80
Boss Lady❤️🥰 :
Merci maman sek ak Gör bobou mo diaffé
2025-02-07 07:48:38
57
Sagesse🇰🇼 :
sékk ak gor wakh diou am solo
2025-02-06 23:21:33
124
ya salam :
ben nék la deuk ak sama diabar amougnou lou beuri wayé ame nagn soutoureu may sante sama diabar mouy djiguén bou doylou way
2025-02-08 08:09:08
4
djily Diop :
machalah maman
2025-02-07 10:15:05
2
Fatoumata Diallo :
bayil niou télécharger li amna solo
2025-02-06 23:29:15
59
user2813257278381 :
mére bi kou bakh la bilahi chapeau à toi maman
2025-02-07 13:13:02
26
Coach Didier seye :
machalla yaye boye diam si yaw lou lérr ga wakh
2025-02-07 13:31:30
3
To see more videos from user @tempsmort.nka, please go to the Tikwm
homepage.