@bou_galsen: Borome keur Even prod Épisode 16 partie 6 #boromkeur #evenprodsenegal #seriesenegalaise🇸🇳 #serie_sénégalaise__ #pourtoichallenge #pourtoi

BOU GALSEN ✪🇸🇳
BOU GALSEN ✪🇸🇳
Open In TikTok:
Region: SN
Tuesday 24 June 2025 13:20:51 GMT
266271
19723
464
117

Music

Download

Comments

mouhamedmeringuebi
Mouhamed Ardar Gülar CR7🇸🇳 :
Sénégal dal diakha nam lima mounoul nangou moy Dieukeur ganiou nga wara seuyak rakou dieukeur lou salté lolou
2025-06-26 12:46:17
39
femmecapable166
👸🏼✨🇸🇳 :
Esk douma bayi série bii ba kérok sama xol diko entan😭
2025-06-24 14:20:29
227
miya51602
Awa🙏 :
Yaye bou bone bakhoul
2025-07-18 16:59:12
4
talibecheik4
talibecheikh🇸🇳🇬🇳 :
Pourquoi la série n’est pas diffusée sur YouTube ?
2025-06-24 14:04:15
20
2naroufatma.0
Narou F@tma12🥹💍❤️🔐 :
Nabou y’a warul wone dug si momar😩
2025-06-24 18:20:09
43
fashagaye822
fashagaye822 :
série bi sibopam lay arrêté sama khôl bagui waddeuu😭
2025-06-24 16:55:14
113
diarrabousso495
nogaye thiou labeug :
pa bi boudé dewoul nak ?even prod deflén com wa marodi yélenko affaire la 🤣🤣
2025-07-18 15:21:43
7
berthydejannot3
Berthe forever living product :
momar geune nala bagn,seysi ba paré di siss
2025-06-24 17:35:22
37
awandaondiaye1
AwaNdaoNdiaye1 :
Aye Momar bo xamone ak léle bou sori 😂😂
2025-06-24 15:32:23
35
macoura.diakhate
Macoura Diakhate :
khalisou diambour mou dé bayil ko ay domame guané dougnou thi deuk senegal li film rek la mena done
2025-06-25 01:50:41
12
mrdiallo001
Kyachu✌🏽💚💚 :
Mane sehlou sama borom Keur gueuneu adina may sey ak son frère désolé mais je peux pas jamais ma doh si lolu
2025-07-18 13:34:14
1
beugueyayam
Yayou serigne Moustapha :
Kou diépi momar comme mane rek laleu j’aime 💯
2025-06-27 10:29:34
7
mareme900
Mère fataya🥟a mbour :
kay ma diaay lèèn
2025-06-24 18:07:19
3
ahmadou4194
AHMADOU :
Thiot ndaye alalou adouna yi rek li 😌
2025-07-18 14:32:39
1
anitoure
Anita :
Nabou guenel si seuye bi
2025-06-24 19:29:56
11
nafythiam369
Nafy Thiam :
partie 5 svp
2025-06-25 01:13:00
0
zeynabeuzy
zeynabeuzy💍❤️🔐 :
mane xawma momar lotakh xamoul bopam mouy melni kou mom keur gui ni
2025-06-24 21:10:03
6
sopeuboromtaif1
Talibe borom taif :
Iso diepi na la
2025-06-24 18:20:59
18
joopjpa0
Joop Jpa 🇸🇳 :
Serie dakhouko deh
2025-06-26 14:13:21
5
khadydieng13
Khady Dieng :
boy bi da rew
2025-06-28 13:38:40
2
matifa05_0
matifa :
Non Momar amna serigne .🤣🤣🤣Ndeysanne,j-imaginw la déception de Nabou
2025-07-11 20:19:33
3
ndiagopreume
Ndiago preume :
izo bou nekone sama rakeu boumala ripé bilay dangay wafff😂😂
2025-06-28 19:30:25
3
adgraphics3
ADgraphics :
boy bi djiko djiguen la yor
2025-06-25 02:25:55
7
khadydieye96
khadydieye96 :
li youkaye déf koumou méti comme mane lalale❤️❤️❤️
2025-06-24 19:58:46
5
amazontradingoneline27
PDG Amazon Trading🥰 A.F :
Kaay ma diay lenn ay huile essentielle svp 😇
2025-06-24 20:52:45
6
To see more videos from user @bou_galsen, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About