Sénégal xéww moko tardél li femme yi dadialé yeup défko si xéw yi bouniouko financer woon kein si keur gui si ay conditions you leirr konn keur yeup avancer na bou yagg mais daniouy dadialé at yakk ko si bènn xéww si loudoul farata ay thiaxani késsé nk