@seriefilm221sene: Déme léne nafila dji segn bi😂😂 #pourtoisenegal #pourtoi #Sénégal #TikTokComique #ChallengeDrôle #SénégalHumour #QuiEstLePlusRapide #senegal #PourToiSénégal #SénégalFierté #TikTokSénégal #HumourSénégalais #ChallengeSénégal #pourtoisenegal🇸🇳🇸🇳🇸🇳 #fyppp #viral_video
Serie +221🇸🇳
Region: SN
Saturday 12 July 2025 20:01:00 GMT
Music
Download
Comments
YAKHYA DIAGNE :
kou beugue Baye NIASS lale j'aime ❤❤
2025-07-13 13:52:09
472
fatyaw :
ndeysane li yeup mourite yi la sene lokho diougou chi😂😂😂😂😂😂
2025-07-13 00:44:44
33
ibrahima Sy :
oho'bayilene'sama'gorobi
2025-07-28 16:45:56
1
DÎØP~TÃLLÃ AD80 :
yalla Bou mouride âme connexion 😂😂yallana séne téléphone yi yakhou😂
2025-07-13 12:16:00
718
TAPSATA🥊🥊 :
Mouride, tidiane thiakhane rekk
2025-07-12 23:41:46
11
🌸sokhna jarra Mountakha 🧕🌸 :
ana Sama mbokk mourite yi kay lene kholl😂😂
2025-07-12 20:43:22
888
Moustapha Traoré ,🇸🇳🇧🇱 :
Mouride bouffi rétane ma bolé leu serign bi 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
2025-07-12 21:09:37
151
sopeSerignesammbaye :
lou khéré lou wohh kong😂😂
2025-07-12 20:56:24
377
mariza :
Li eupouna def comme guerre mondiale
2025-07-29 01:56:27
1
Fallou Béye :
Légui Mame Balla déf contre son camp 😂 walla mou maylén penalty
2025-07-12 21:47:49
110
Cheikh Ahmadou Bamba :
Ki mom moko tayy ndakh yagg na vise bopou wadji 😂😂
2025-07-13 12:09:19
213
Astou Niass :
Li montage la 😂😂 Bly dou souñi yeuff
2025-07-12 20:38:52
64
Alioune :
yalla bou mouride yi ame connection way🙏
2025-07-15 01:11:23
1
daba Niang mou baye niass 🙏🙏 :
ndeysane mouride yi dagnou beug baye naissance machalah diam thi yéne😏😩🤣🥰
2025-07-15 19:18:37
21
ziza mbacke :
Tidiane yii ñoo nékh rekk😁😁😁🤣🤣🤣
2025-07-12 20:08:43
19
AHMADOU✊☝️ :
mourit yi dawsi léne niou réé touty😂🤣🤣🤣
2025-07-13 12:31:41
27
keeper :
yallah bou ben mouride amm connexion rk
2025-07-12 22:31:15
24
amadou_mbow16 :
Wa keur baye la dh☝🏾😂🤧
2025-07-12 21:48:20
41
ceddo Mbégnou Gana :
yow mi dougal li yalla na sa baye sékhlou sa yaye
2025-07-14 09:48:24
2
Fallou Thiam :
bienvenue dans les commentaires café ou té😂
2025-07-13 12:17:36
22
unelebou14 :
Wadji meunatoul youkhou 😂😂
2025-07-14 20:38:29
6
Moussa Ndiaye Zakir 🎤🎤💖💖🎤 :
yalna bou mourite yi am conexion de même que wifi 😂
2025-07-14 01:09:44
3
zizis :
alhamdoulillah lii moom dou ñioune mais mame balla réka ma diahal légui mou maylën penalty😅😅😅
2025-07-12 20:08:46
67
mame gueth diaw :
Mouride bou beug baye niass Minguini😭😭😭❤️
2025-07-14 12:35:07
15
Bb Fatou 234 :
@lou takh douniou ko meun téléchargé 😳🥺
2025-07-12 20:43:46
10
To see more videos from user @seriefilm221sene, please go to the Tikwm
homepage.