@ndawadiop8: #balla da bléssé

femme noir ❤️
femme noir ❤️
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 20 July 2025 17:53:08 GMT
385419
19059
366
927

Music

Download

Comments

mamytasow0
Mamyta :
Diome rk moko beurè lo 🤦‍♀️🥹🥹🥹💔
2025-07-21 04:45:51
327
lesbelleparoles0
al amine❤️🙏 :
Saltél victoire rk laniou meun 😂
2025-07-20 21:18:01
176
fafou.boye1
Fafou Boye1 :
Dara dalouka
2025-07-25 18:34:42
1
momointernational5
Adios :
Stp doniou expliqué lii supporter yi done kasse ??
2025-07-20 23:17:16
5
ibrahimafati
ibrahima faty :
Niom Aziz pourquoi bou balla amé blessure douniou ko protéger annuler le combat si c’est réellement ça
2025-07-20 22:19:01
592
rapca231
Rap ca 221 :
kii barkii serigne touba dara diotou ko azize ndiaye wax nako da guisson défet bii mouy doul fii na bayii bala défet yii di tolo ak victoire yii
2025-07-21 12:32:21
9
mulequedevila98
muleque de vila :
ndakh nga sagne ko wakh dara diotou ko Senegal moo bari nafekh
2025-07-23 15:57:35
0
pape4713
pape :
Eumeu moy sama mbeur dé mai avant combat ladone wax balla dafa bléssé
2025-07-21 00:06:40
76
shitabv
shitabv@ :
ndeye san aka goré nak balla gaye
2025-07-24 17:09:55
0
dioufelhadj5
dioufelhadj90 :
li mome c pas la première fois si mome sasou danou khar kofa blésse wala fébar mba gadaye sounou nane sili boyna sounou nopp soit sportif 🤣🤣🤣🤣
2025-07-21 19:32:53
1
h_pro_officiel
H-PRO-OFFICIEL :
Mé li avant combat bila
2025-07-21 01:02:07
2
mbeuss28
mbeuss :
7 Défaite 😂 7 Blessé 😂
2025-07-21 09:05:11
9
boudegueurbi
Bou Deugueur bi :
Grawoul Aziz légui mou créer Couronne Firaouna des arènes iri watt Tapha noy bopp Tine 🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺
2025-07-21 00:31:44
21
adjifalldrap2
Fall Draps 2 🤍 :
Billae li metti nama basi kanamou yalla 😭balla waro wonn beureee
2025-07-21 17:17:43
0
mortallalondame
Lô Ndam boutique :
Danko diékou rék
2025-07-21 18:01:47
1
bocarkane903
bocarkane903 :
Mais li avant combat bi la fallait annuler le combat
2025-07-20 22:58:07
256
galasfall925
Galas Fall925 :
sa way maylen nit diamè ki siteu dfko mane
2025-07-21 10:00:31
14
use093boyealuminium
ndoye boye :
Aziz Ndiaye kou bagne balla gaye bilahi walahi
2025-07-20 22:36:12
21
wojciechszczesny97
WOJciech.Szczesny 1 :
Siteu diappe ko niousse ko Mouy daw nganane da blessé😂😂😂
2025-07-21 19:47:26
2
salambouhtdkh
Salam Bou HTDKH :
Issa pouye dane la ngani lolu du diel Eumeu dane la ngani xale la wone mou danat la ngane dama febarone Bombardier dane la ngani dama blaisse Boye niang dane la ngani dama blaisse Siteu niew nga dem inseps dépensé fa plus 30 millions nga niew niu dane la ngani dama blaisse seng Balla kanie ngay wer gayine😂😂😂
2025-07-21 15:29:21
2
latdaraseckfall
latdaraseckfall :
niom Aziz Ndiaye la rék
2025-07-23 13:51:24
0
sowbecaye221
BECAYE 🇸🇳 🥷❤️ :
Balla dou yakh Lamb jambar deug leu Billahi ❤️❤️
2025-07-20 23:04:42
180
mamo13741
Mam$$o :
guediawaye tass n'a
2025-07-21 21:24:29
0
ndemagaye
Ndema SALIOU🇲🇦🇸🇳 :
Balla xalatoniou nakk vraiment
2025-07-21 09:13:01
1
big___eyes
MALEEK CAKES🎂🎊✨ :
Wa legui bou tanè na dieul revanche 😂
2025-07-24 23:59:15
0
To see more videos from user @ndawadiop8, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About