@fall_mbegtefadilou: Na nguen Yeureum Soxna Yi 🧕🏽tei dilen Béguël . kii moy Soxna Maï ni tourbi nékhé nonu la Xol bi leeré sama Doom lah sama Xarite 🤍🤍⏳ #bayefall #khassida #serignetouba #serignefallou #mouride

Fall mbegte fadilou
Fall mbegte fadilou
Open In TikTok:
Region: IT
Friday 25 July 2025 18:23:14 GMT
100105
25938
217
42

Music

Download

Comments

salamata375
Yayou Rassoul ❤️👑 :
sokhna Maï Seck yalah nako sougn borom sameu 🥰
2025-07-25 23:30:31
18
_mame_bousso_tall_
Soxna Diarra❤️‍🩹👸🏽 :
Comme sa dom la reik Alhamdulilah
2025-07-25 20:42:14
429
ndiaye.153
misse ndiaye♥️🍯 :
goor yalla deugu da wara yeureum dijguén 🥺
2025-07-29 09:54:52
0
minabouserignefallou1
Mina bou serigne fallou❤️🤲🏻 :
Fall khana dou lima khalate dhé 🥺🥺
2025-07-25 18:56:04
31
sokhna.touba.ndoye
sokhna Touba ndoye :
commentaires au lieu guén xalate Thi tourou yalla wi guén nékfi nane yakar tasna😂😂gni nane doulimay xalate😂😂 mougne lén yalla bakhna
2025-07-25 19:28:17
221
maguiifa
Ma_gui :
Danio sokhla explication😭
2025-07-25 23:21:09
31
khadija.s601
Khadija ´s👄 :
Fall fasall sokhna si barkep safar gui
2025-07-25 19:23:03
8
sokhnamomiyaram
🖤🤍mominatou yaram 😇😇 :
da melni d'où lima yakar man tamite🥺 isque d'où dafay publicité 😅😅
2025-07-25 19:05:04
78
mamyfall706
Mamy Fall706 :
boudé dom la kay diaroul Tite meune nako yayo sante souniou brom sma fitt bi néna reuss 😂😂
2025-07-25 23:47:28
20
dior.mou.cheikh.i
Dior mou Cheikh ibra 🦋❤️😘🌹 :
yéne gni commentaires nane fall tass gua sama yakar, fall daléna mana takk yéne nieupou nak 😒🙇🏿‍♀️déf léne séne bopou yi diné la wakh moh waye 👩🏿‍🦯
2025-07-26 00:56:29
16
cherif123333
Yah Rassoululah :
Fall d boudé da nga fass soxna ba am doom Hopital dina beuri Mort tay 😭😭
2025-07-25 21:23:57
73
djoloffdjoloffbi
JOLIE MIGNONNE ❤️❤️❤️ :
Yalna doundou té barkel barké cheikhoul khadim 🤲🏿🤲🏿🤲🏿
2025-07-25 19:58:51
117
mame.bousso312
mame bousso :
fall lima yakar sou dé deug dîna xaroudh ak nimala beugué 😭😭
2025-07-25 21:22:08
13
bxd99
bint xadim :
nio mell nonu nous les Sokhna Maï ❤️
2025-07-26 11:59:27
14
khadija.everywher8
!🥥😻 :
Khana dedet kayy 😩💔
2025-07-25 19:51:59
23
bichriainne
la bichriainne :
machallah lo am solôu yalnanioula dégue
2025-07-25 21:21:12
4
une_tidiane
Une saint louisienne🦋🧕 :
Li barina vitamine dh 🥺❤️
2025-07-28 14:01:10
2
talzo41
talla Touba ndindy s.fallou🤝 :
baye fall la 😂😂😂ak yaye fall baye manol bagué kodoul yaye 😂😂😂yaye manol bagué kodoul baye
2025-07-26 01:03:07
12
liguerefall7
liguére des yaye Fall 🏁💡 :
Lima intéressé moy tourou yallah bi 😌
2025-07-26 05:50:33
7
ndlla.sarr
Ndélla Sarr :
Tasatinaniou yakarou xalé you djiguen yi rk😒
2025-07-26 00:13:37
7
saliou.diouf.7
saliou.diouf.7 :
Yalla nagnou diékou magal gui inchalla ❤️🕌🎶
2025-07-26 01:44:29
15
yaye.fall941
Yaye Fall :
Tourou Yalla wi 😭🤍
2025-07-28 01:03:46
1
princessediop2211
princesse noire 🖤🌸 :
Lii mouri tena dh 😩😩😩❤️
2025-07-25 23:35:08
4
kin.bou.mame.cheik
kiné bou Mame cheikh Ibra fall :
fall ya bakhe daga beug serigne fallou mo takh ma beug là ❤️🥰bly
2025-07-26 15:03:40
4
keuryayefall4
@yayefallcivilice :
Tarkala 🖤sokhna danioukoy yeureum 🙏
2025-07-25 18:32:59
11
To see more videos from user @fall_mbegtefadilou, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About