Boumou ko wakh na soutoural bopam tè toup si yalla
2025-07-28 14:34:53
41
dieggeme boutique♥️♥️ :
tu peux divorcer pour refaire ta vie et aider ta maman mais garde la vérité même ton meilleur amie ne le dit pas
2025-07-28 16:47:46
166
user7385778290989 :
Pourquoi coucher avec d autres hommes alors que la fille peut demander le divorce dem séti lénén. Tout sauf djialo elle avait le choix d autant plus que wadji bakhoul
2025-07-28 13:41:46
58
la folle :
na dém liguéyi c’est mieux té mou garder secret bi soutoural bopam comme niko yalla soutouralé !
2025-07-28 13:59:19
23
MUHAMMET-BARHAAM🧑🏽💻 :
Chercher l'argent avant de chercher mari(_) huum xawma naka la nit mana soxor ree à ce point🥹
2025-07-28 16:12:06
63
AKB🎊 :
Li motakh ma ragal seuy😩😭😔
2025-07-28 11:41:57
37
Max :
honnêtement j'ai pas les mots que le bon dieu guide tes pas
2025-07-28 15:46:05
79
Mrs K Fa~Lilou ❤️💍 :
Tu as parfaitement raison na nopi th dem ligueye yalla soutoural nako boumou werr bopam
2025-07-28 16:36:13
33
adochou3812 :
Lolu divorce moko guene ndialo mom bakhoul 😩😩😩
2025-07-28 13:37:16
14
bané_diop :
Si elle n’est pas heureuse elle n’a qu’à divorcé mais ne dis jamais la vérité c’est pour le bien de tes enfants et leur réputation
2025-07-28 13:51:23
33
Mounass :
ooh ndeysane masta ma chérie 🥹🥹
2025-07-28 12:18:23
16
radia :
Na nopi rekk pour la protection de ses enfants qui vont subir les conséquences 🥰🥰🥰
2025-07-28 12:17:12
19
Metou Faye :
Takk la pr trokhal la 😭🤔
2025-07-28 15:42:25
17
Tida Goudiaby :
Après les enfants in’auront pas de papa en plus c’est pas bien pour eux
2025-07-28 16:36:25
12
Fatou diémé :
soubouhanala 😭😭😭😭😭😭😭😭
2025-07-28 16:07:28
5
babèl ❤️🫀 :
Mane goor gni Louye sene problème la khamoul bounla kheusé ba tak Dale yak mbame yi yénaye yam si mome aye domeram Lane rek
2025-07-28 14:53:09
4
butterfly💜🫶 :
Na soutoural bopam nopi mou dem liguey dieukeuram baxoul yorr jiguen diko deff ni
2025-07-28 15:42:08
7
pape Sow 🐎🐎🐎🐎 :
boutasé sybi dina thiaga touji mala wakh li
2025-07-28 14:36:18
7
❤️❤️❤️❤️❤️ :
Na tasse seybi déme liguayé yi 😔 yalla bakhna 😭😭😭
2025-07-28 14:59:18
3
Diene :
chérie adouna dafa goudou tang dom yi guey khalat founie dadié ak sen baye wala sen frère wala sœur yalla dinala soutoural