@sokh7200:

Bybachou Hénne
Bybachou Hénne
Open In TikTok:
Region: SN
Saturday 13 September 2025 10:01:14 GMT
421323
34431
1359
5554

Music

Download

Comments

kaneva177
kaneva :
depense bi sakh dou mate parfois
2025-09-13 17:01:36
1212
premieredame1
Premiere Dame marieme f sall :
djiguene yi parfois daniouy perdre confiance en soi
2025-09-13 18:56:34
663
ghoulame07
amazonou ghoulamou ❤️🥰🙏❤️ :
juste une question sa djiekeur niake la topato esque diarna tasse seuye 😏
2025-10-09 00:10:01
0
astel998
Aïcha 🥰 :
Wawaw defarou temps si lah Bokk Amna gno khamnii banou seuyii wé lanou gedia nelaw nelaw you normal
2025-09-13 17:41:27
196
evichlatigresse
Ndeye awa konaté :
Rayal nala teigne 🥰
2025-09-13 20:20:42
25
diop65064
Aïssatou Diop :
Je me sens visé ma situation actuelle
2025-09-13 18:38:43
185
peace.lol
Aymen GLAM :
surtt qu'il passe leurs temps à te critiquer tt le temps, ga lenn di mougnel senn lepp mais gnom dougn mougn dara, melni relation bi djiguenn kassé moko wara entretenir, beug détail, bari wax. a la longue mank de confiance dapp leu, aprés il va te dire wolou wo seu bopp, fek lou négatif lila dall lepp c'est de sa faute. Ma solitude me manque😔
2025-09-13 23:23:50
40
sarramy95
@yayou ♥️papa♥️ :
niom kulunayi Tabaski ba Tabaski laniouyy diokhé🤣🤣🤣🤣
2025-09-13 22:32:47
83
adav0023
adalea :
sa wave ma wave la wakhal ngama lepp lou nekk sama khôl 😂😂😂😂😂khana télécharger rekk envoyé ko di khar sama reponse 😂😂😂 gnanal lene ma rekk 😂😂😂😂😂😂😂😂
2025-09-13 18:23:20
116
assy62982
Madame Diop SL 🌹 :
ay souma meunone status 😂😂
2025-09-13 21:48:01
26
lizoubellou
Lizou bellou :
Koukou statut diape ideu😂😂
2025-09-19 18:47:35
3
madame.b830
Madame Bâ💍❤️ :
Sauf mon mari Billahy Bâ pouloh diérry bakh gueun riche xam valeurou djiguéne machallah ❤️❤️❤
2025-09-13 17:41:09
44
user9319956137345
oumoumalick laye🇸🇳 🇺🇸❤️❤️ :
moma diakhal li 🙏🙏dama dougue ci sey rekk melni sama adouna da touki bilayy 🙏
2025-09-14 00:12:53
34
amina.pene
Amina Pene :
kouko statut niou faséla
2025-09-14 09:26:33
5
aichabapapendiaye
@icha ba645 :
mandé sou démb done Tay douma dougou si séy
2025-09-29 21:14:52
3
mmeseck69
Mme Seck♥️❤️🌹 :
damako beugue estatu tes beugouma diape ida😭😭😭
2025-09-18 19:10:23
0
evamakeup05
evamakeup05 :
Beug nako statut wayé damay bagna gnii 😳
2025-09-19 12:50:55
0
wolof752
Pr S.Touba ( matheux) :
wakhofi dara khayadi ak bayekou si nit li , sagnsé si nit la
2025-09-13 20:11:50
2
aida09.v
Aïda_Bella :
Bly dara matoull sopp rek mo massi dougall ba paré roussa nibi 🥺🥺🥺🥺🥺
2025-09-13 21:08:08
6
coucou08186
Mrs Alif😍 :
Kouko statut diapp ideu 😂
2025-09-13 21:22:31
4
margo85377
margo😍 :
Dofii guiss goor dé ay domaram laniou khathieu bi yepou😂
2025-09-13 17:38:27
66
tina23146
Tina :
bilay tu as raison doula may dara
2025-09-20 19:13:51
0
fatimkhsene
Mme :
verite absolu
2025-09-15 12:13:13
1
salihatethioup
madame Gueye :
envoyé nakoko dei sama yone nékouci😏
2025-09-13 22:56:54
14
karbala33
Karbala33 :
NDA Kham am na djiguen you am diom mana mougne tai dou niou diambat mandou ragal yalla tai lolene diokh mou doyleen ….. parira paparara😂😂😂😂
2025-09-13 20:16:49
2
To see more videos from user @sokh7200, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About