senelec dhé lignou néké legui dama yakarni gouvernement bi yégouko
2025-10-03 10:43:48
25
Aliou Ba Bou Bintou Ndiaye :
25000f ladon faye mai legui magui thi 75000f
2025-10-03 00:41:18
14
diéry dior ndéla :
lii bokk na li waral sathie courant doufi diogué
2025-10-03 11:19:05
24
Lavage.lac.recba :
Comme Sénégal amoul soleil ☀️installé des solaires
2025-10-03 14:29:45
0
Intimebyinde :
Senelec dama yakar nioune niouy fayal seine agent yii
2025-10-03 12:07:56
2
cheikh p.a :
c du sabotage nagnou dakk dg senelec première manifestation courant mokoy indi
2025-10-03 13:05:37
5
Dima Diato :
Be legui ministre wakhoul😳😳😳
2025-10-03 15:08:15
0
Papa wally :
mane sama keur bène frigo bène télévision bène ventillo mais d'habitude on payé 30milles au moins, mais cette mois ci nous avons payé 105700 bilahi dou yone🤨🤨🤨🤨