@diodioglowskin: Comme Dans chaque administration 🧑‍💼 cette photo de notre Président symbolise beaucoups de Choses ❤️

Diodio Glow skin
Diodio Glow skin
Open In TikTok:
Region: SN
Saturday 11 October 2025 17:02:03 GMT
320745
50326
768
94

Music

Download

Comments

mgm_mboup
mgm_mboup :
Wouteul photo sonko teik si wett gui après nga denk niou sa bopp nioune patriote yii koula lale wala mou toude la niou niouss ko wasalam 🙏
2025-10-11 19:31:10
769
rokhaya29953
Rokhaya ❤️🥰 :
Wa ta didio ma lathie la yaw yay tontou commentaire yi wala dagne lakoy tontoul wala yaw bakh nga dhe maner yaw dangay doundou dhe bou nekher yalla inchallah da am khaliss machallah te khamou ko ya nopal sa bopou dhe mane khaw ma sakh lane la wara wakh mane mom dang ma yeme Bilay Lou may wakh rek nitou yalla Ay way thiate Fo kham demal 🙏
2025-10-11 18:43:41
10
beautybylinguere
Beauty by linguére❤️ :
Barki borom touba yalla na lepp barkel thi Barki seydina mouhamad
2025-10-11 23:53:23
0
boussolagrandedame
Oumoul Khadimou :
Yaw Patriote bi ak fo mana nek yakham ga nioul wala khéss wala sa ga khérel diodio mou Lay diay lait de corps 😂
2025-10-11 23:09:17
7
jarrah_fallou
JARRAH_FALLOU🇸🇳 :
Non tata diodio do pause touti ba khol yi dall😭. Sinon legui cardiologue yii am ligueye 😩😩
2025-10-11 17:24:58
1953
ndeyedabagaye45
Madame Gaye :
Diodio sa maison bi yalnala djikk 🤲 yalna dem ba say seutt dissi liguey si barker seydina Mouhamed 🤲🤲🤲
2025-10-11 17:07:58
449
90khadija_niang
𝙠𝙝𝙖𝙙𝙞𝙟𝙖 🇸🇳💙❤ :
tata bénn solution rk la guiss moy que Maison bi déff si sama tour après nieup nopalou dou deug🤔
2025-10-11 17:16:24
787
awatendeng2
Awatendeng :
Wawawe nitte day ame kilifeu merci beaucoup 🙏impôt bi boulko faté day doléll liguéyou gouvernement bi 🙏chauffeur mayegnou arrêt 🛑 diodio
2025-10-11 17:49:46
66
beugbamba016
Beug Bamba🇸🇳❤️ :
Lo beug deg nak Djodjo😭🥺❤️🫶❤️❤️🎊🎉
2025-10-11 23:43:22
1
papyto56
Papyto :
Au Maroc méme dans les Sociétés privés ils mettent la Photo du Roi. c est tres bien de méttre la PHOTO DE NOTRE PRÉSIDENT.ÇA PROUVE LE PATRIOTISME
2025-10-11 17:20:29
634
misssarr21
Miss sarr :
diote na diomay diokh diodia🥰 ministère du commerce demande nationale 😂
2025-10-11 20:07:36
1
boussobaly94
Diarra❤️Bousso~~ :
Diodio difference mom ak les autres moy dafa diang🥱 meun nga bagna diang am xalisss mais …do Xam noy gestionner sa Xaliss… gestion de projet✌🏻😭😩
2025-10-11 17:35:52
302
soxna.war.saliou
LesDélices De WaréSaliou🥐🍟🥮 :
Tata Diodio begue na ligueye sisa restaurant bi dh🙏
2025-10-11 17:11:56
35
un.coeur.en.miette
Fleur sarr :
comme ts les bureaux🥰🥰🥰🥰merci Diodio
2025-10-11 18:57:42
20
mcm98844
MCM❤ :
WAkh lene Diodio mou def Sama photo ❤😁
2025-10-11 17:36:56
24
mariama.sarr.bou.s
mariama sarr bou sonko :
Tata dio mi dékété damala beugu 🥰
2025-10-11 23:38:59
1
binettedjibril
binette :
yaw rék lay top depuis tay
2025-10-11 17:39:19
1
anta.lofficiel
Anta l’officiel 💕 :
Mou dess Ousmane mou sell mii nakk après nioun patriote yiii gua bayé niou sa bopp khalei boula lale digua léko ak nioun😭❤
2025-10-11 23:37:06
2
mya.mya_dia
Mya Dia 🇨🇭🇸🇳 :
machalla khol sed na yalla immeuble yi gueuneu si barki seydina ousmane sonko mou sell mi😂
2025-10-11 17:51:40
9
maguikhadim
une diop :
machallah
2025-10-11 17:04:24
57
oumardiop752
oumardiop752 :
Woutalle Photo Ousmane sonko Si Bontou bi 👈 Fofo tothie
2025-10-11 20:42:41
12
keparouserignsaliou
Serigne Modou diop :
Baye bass seull ❤
2025-10-11 18:58:51
13
the_hidden_221
the hidden 221 :
Au moins xaam nga louy citoyenneté 🫡🫡🫡
2025-10-11 18:57:55
38
user1819075114509
♥️♥️♥️zaha mina seul♥️♥️♥️ :
tata diodio 🥰barki serigne babacar sy ya khame temps 🥰🥰🥺🥺
2025-10-11 18:10:54
9
nabouza4397
nabouza :
diodio yalna yalla Sam mousal thie saytané
2025-10-11 23:19:42
5
To see more videos from user @diodioglowskin, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About