@ndiayetouba120: Yarou lène rk tè nagou li yalla dogal rewmi sonko moko mome 💪💪💪💪🤣🤣🤣🤣

Ndiaye touba 🇸🇳🇮🇹
Ndiaye touba 🇸🇳🇮🇹
Open In TikTok:
Region: SN
Saturday 11 October 2025 19:25:22 GMT
180422
9422
1460
588

Music

Download

Comments

ndioba844
Ndioba :
Yalla khamnani Jour bako Sonko wakhé walahi kérok la gueudia setane TFM .
2025-10-12 00:09:18
1029
umaar207
umarr amiroul moulinie🇸🇳 :
Bignouy Ray sénégalais yi bobou ay mické geune done tek
2025-10-11 23:12:34
461
taekwondo_2.1
Xol ak Xel 🫀🧠 :
😂😂😂 Bouba nioune legui tiktok mo niou bollé ak yenn deh, ci ndigueul rek laniouy dokh
2025-10-12 14:49:06
223
mareme4199
Mareme :
quand le senegale avais besoin de vous la télévision TFM vous été ou (vraiment )
2025-10-11 20:41:14
229
baldeopoullo
baldeopoullo :
man dh depuis 2019 setanouma TFM billahi
2025-10-12 07:00:36
234
prince.djimy.ga
Djimy Faye🇸🇳🫡☠️ :
Moi personnellement, je ne suis pas trop dans la politique, mais je pense qu’il a raison de dire que y a d’autres médias alors laisse les gens parti sur les autres médias, vous pouvez inviter d’autres personnes qui vous conviennent😂😂🤣
2025-10-11 21:08:20
62
ndeye.diouf634
Ndeye Diouf :
sonko koumou bayi ma bayila point
2025-10-12 17:40:22
30
maxbouseigneurbabacarsy
Mme mbaye :
mane dé soumay zapé ba yame si tfm wala stv damay gawontou changé beugou ma fa déf 1s sonko dima méré
2025-10-12 23:19:18
5
ibrahimasarr236
✨💦⭐️إبراهيم 👑Prince✨ :
Loutax ngueen xam li yeup ba paré bañ fay impôts 😂
2025-10-12 10:29:02
134
galsenerek1
MD9 :
yenay numéro 1 ba paré di youkhou 🤣🤣🤣
2025-10-12 00:23:34
199
lahat______
lahat bû sëgn fallou :
Billahi dama leine di fatté sakh barki yalla😂😂😂
2025-10-12 18:05:23
14
mandionebousonko
mandione bou sonko :
jour bako sonko wakhè lakko geuddia setannn
2025-10-12 17:45:42
8
abassgy
BEUZ985Abass :
wa louy decommander invitation😁😁 khalass
2025-10-12 00:44:33
5
bambagueye2021
Gueye bamba ke :
mane kouma wakhone si adouna né dina massa bayi TFM douma ko massa geume, merci sonko
2025-10-12 08:51:10
63
ndiayetouba120
Ndiaye touba 🇸🇳🇮🇹 :
Sonko mome bagne bagna beugue 🤣🤣🤣
2025-10-11 19:26:36
284
user1454438006756
user1454438006756 :
moi j'ai boycotté depuis le jour où les nervis du pouvoir tiraient sur des manifestants ! j'ai courru pour voir la TFM et vous mettiez . des clips !
2025-10-12 16:41:37
5
1986mn03
Moustapha Ndao :
Bilah akama gueudj setane TFM. Non Sonko barina Dolei
2025-10-12 02:36:54
53
unser35670
unser35670 :
Setane RDV moma geuneul setane teufeum
2025-10-12 16:26:12
23
djibrildiedhiou99
DIEGOJUSTIN :
walf télévision du peuple
2025-10-12 11:17:59
26
bathie7790
Big Bathie🖤🖤🥷🏾🥷🏾👌🏾 :
No grawoul bayil niou dém fénéne rék 😂😂😂😂
2025-10-12 00:38:14
117
zahrazahrafatima09
zahrazahrafatima :
hahaha thiey ousmane sonko yalnaleu yalla sam way ya meuna heh 🤣🤣🤣🤣🤣
2025-10-12 09:28:02
87
mediainfos0
media infos :
pourtant bingén di fénal Aser Jean Michel wo Bouba Ndour niko danio beug ngén invité gnou Niou léral Bouba dafa bagn tay ngay sarakhou ko invite 🤣🤣
2025-10-11 22:22:57
97
mbectemi_
sénégalais🇸🇳 :
man dé magui diegalou Sonko thi vidéo bii ma setan nii😂😂 malén bayii man 😂😂
2025-10-12 09:29:15
102
moustapha_the_preferred
moustapha_the_preferred🇺🇸 :
💯❤
2025-10-11 23:12:38
20
lechoix50
TALIBE PROS🇸🇳💎 :
konn TFM mo nghi existé ba tey?
2025-10-12 05:19:19
27
To see more videos from user @ndiayetouba120, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About