@dakar_senegal5: Allahou akbar Lou nék dégue nako • Dagua begg sacrifié sa dome... Yayou Mouhamed 14ans en larmes verse de chaudes larmes

Dakar_Senegal
Dakar_Senegal
Open In TikTok:
Region: SN
Thursday 23 October 2025 13:26:49 GMT
703148
40000
824
630

Music

Download

Comments

mrsmbow04
Mrs mbow💎🥳 :
Mouhamed dafa rafet 🥰
2025-10-23 20:08:24
126
baa92225ymb
user10989750643 :
stp aidé moi avec 4 mil sama yay la beug dieundeul soukeur diabète sonou na bilahi
2025-10-23 15:01:34
62
carter8164
A :
les médecins comme des boutiquiers ils cherchent des clients vous ne pouvez jamais aller chez un médecin il vous dit vous êtes guéri al a fin de chaque maladie il cherche une nouvelle maladie
2025-10-23 21:15:16
1
adamsdiop2704
Adam's 🥰 :
Nitte yagg nagnou ko declancher dome bi dioudou dara douko dale li Lou warone am leu rek
2025-10-23 14:28:24
1383
mo.rassoul
Rassoul🇸🇳 :
Mety na sokhna si mais Yalla moko dogual
2025-10-23 20:36:01
7
tymachouu
Matel🌹💓💓 :
Au moins ame nga dôme 🥰aime ton enfant et chéri le 🥰avoir un enfant c’est une bénédiction ❤️❤
2025-10-23 19:38:09
136
assita335
Mrs D❤️ :
Souffrance fœtal réanimation bou yagg c’est à éviter defois il faut laisser partir l’enfant metina trop nak
2025-10-23 19:44:47
6
mintou58
0123456789 :
Moi on ma declancher Alhamdoulilah ma fille est veni normale
2025-10-23 21:19:52
0
tyma.entre.soeurs
Entre Soeurs 💕 :
il est atteint d'ifirmite motrice cerebral ( imc) dagako yéxa guiss Mme
2025-10-23 20:41:58
0
zeynayade8
MD-16-89 :
li birroum yalla képppeu leu ya Rien d'autre
2025-10-23 20:11:58
15
ndemadiop
ndemadiop :
Tu as tout dit un nouveau ne réanime plus de 5 minutes day al ay séquelles surtout côté neurologiques
2025-10-23 20:08:17
9
user7084619754378
Alima Ndiaye :
ndeyesanne Mohamed dafay rouss sakh li yaye dji di wakh ndeyesanne 🥺🥹
2025-10-23 14:28:26
67
oumoufofanasoumar
oumoufofanasoumar :
ma chérie du courage moi j'ai la même problème ma fille a 10ans maintna
2025-10-23 19:12:45
3
yayou_mouhamedd
Yayou Mouhamed :
Souma done yaw douma guenè sama dome si réseaux yi yalla na yalla maye kholou mougne mome miye dogal courage
2025-10-23 20:40:15
1
bbs23456
BalyBousso :
Souffrance foetale bi moko deff lii
2025-10-23 15:08:38
7
user120529123030
sanou :
Yay Mo sone. Yalnako yalla safara
2025-10-23 14:35:12
85
001binoushasaliou
001binoushasaliou :
Pourtant ya beaucoup de gens qui sont comme ça yalla moko beugué ni rk
2025-10-23 15:09:39
261
aissatadiope
dokhott kat😳 :
massa yay boye,li malformation la sa na rien avoir avec déclanchement,natou la rek mougnal, courage 😔
2025-10-23 15:21:26
82
user6132125770341
seysey :
il est beau ton fils
2025-10-23 20:23:42
23
maria.199930
maria 1999 :
moukhamed machalla dafa raféte trop 💞💞💞 massa ma chérie yalla Nala borome fay sa khol
2025-10-23 19:53:55
14
ousmanendiaye376
NOREYNI BGB ÉLECTRONIQUE :
Genr yi gouvernement bi moko wara dieul en charge
2025-10-23 16:31:48
20
marceloojr221
BDG :
Ndongalou yallah la🙏
2025-10-23 18:54:42
36
beldamefruttishop
beldamesfruttis :
djiguenn moyy louner bilahi diomoul kenn massa courage ma soeur
2025-10-23 15:17:56
6
fatou.tine18
Fatou Tine :
santal yalla com am nga dom
2025-10-23 18:48:16
10
kyaprincessepeulh3
kya la princesse 👸 peulh ❤️🥰 :
Yalla moy binde garde bien notre Mouhamed ❤️🙏
2025-10-23 19:45:59
14
To see more videos from user @dakar_senegal5, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About