@pikoniang: Balma akk man damay foo rek 😥@Fallou Benjamin claviste

Pikkola 🇸🇳🇲🇱🇬🇲
Pikkola 🇸🇳🇲🇱🇬🇲
Open In TikTok:
Region: GB
Tuesday 28 October 2025 22:59:27 GMT
409360
45302
506
98

Music

Download

Comments

matyelgueye
Maty Mrs G🫶❤️ :
No Face moko bloquer pour gniko hamoul🤣🤣🤣
2025-10-28 23:56:10
2961
justadd23
~justADD💃🏽💅🏽~ :
C’est pas mon jallabé c’est le jallabé de mon beau frère li deh la wakh insta gnou bloqué ma 😭
2025-10-29 16:27:13
603
fatousalih
Oumou Saaliha :
Mane fepp lama bloquer 🤣🤣🤣
2025-11-01 00:17:33
0
mamandioufy46
Dioudiou❤️🦋🌸 :
Man Facebook lama bloqué won début histoire ba la khamni da sikk suma guissé mou publier rek ma dieul photo mia niaffko ci commentaire yi 😂😂😂😂😂
2025-10-29 10:47:29
1005
thiatfashion25
Thiat Fashion :
Mane Facebook lama bloqué 😂damaniko juste iow meuno bayi détails té concentré sa carrière mounima iow tay ngamay moudier conseiller
2025-10-29 17:02:26
149
ndeyekane408
Ndeyekane🇸🇳🏅🇺🇸déliceDkyra :
Khana gnou bayiko ak tata amy cole mou sele mi rek mou géré ko😂
2025-10-29 07:40:19
1236
0033louna
Louna Lopez🌸💮 :
dedete key khana 😂😂😂😂😂
2025-10-29 08:40:30
368
ndella.diouf972
élément serigne saliou😍🥰 :
mo kham dh kane la sakh
2025-10-28 23:29:41
260
tymakylieyade
Une +221 🇸🇳❤️ :
No face foumou moudjék preuves yi ?🙄
2025-10-29 13:45:46
56
mignonnenar95
💕💫fatou 💫💕🇸🇳 :
Ndéké no face limou solone sii clip bii sikime beu rek lasii mome 😫
2025-10-29 17:28:18
146
user8456003839486
user8456003839486 :
Da nga Meun togn lol vraiment doy n’a
2025-10-29 09:32:11
8
mbadienebuserignesaliou
Mbadiene bou Serigne Saliou :
C pas mon yeure c le yeure de mon beau frère 😂 j’ai rien dit nak wa salam
2025-10-29 01:01:50
462
zahra_rassou
Zahra💝🇸🇳 :
Adouna ko mbéreur diérri 🤣🤣🤣🤣
2025-10-29 12:49:42
30
ahmadoulkhadim00
Ahmadoul Khadim :
Daguén Di togne Di contane 😳. Je ne pense pas que dignén khalat déh amna 😌
2025-10-29 10:27:31
22
dabayevents2022
Dabayevents2022 :
Hana kone koumouye deff Amy Cole 😂😂😂
2025-10-29 00:09:23
327
pendista20041
ľaudacieuse :
mothiye kane maléne dakh abbe fouf dou beurri yerré moy sañgsé😅😅😅
2025-10-29 17:55:41
10
queenrose016
Queen 👸🏻 rose ♥️🦋 :
C’est pas mes yeuré mais les yeuré de mon beau frère 😩😂😂😂
2025-10-29 17:43:46
15
pweety.yazz
Pweety Yazz🥹❤️🦋🇬🇲 :
No face la😭😂😂
2025-10-28 23:48:00
362
user468022598
B’ggg :
Même mane té passeport bi rek lako lathié 😭
2025-10-29 19:34:56
73
momomam4
momo mam :
Borom abb bi leu waleu😂
2025-10-29 00:05:51
96
bou.djiby.ndao
Bou Djiby Ndao :
Dina niou capturer di la envoyer 🥰
2025-10-28 23:46:30
48
daaasmeee
Das_mee :
Bagn len mandou si problèmou nit yi rk
2025-10-29 20:18:43
1
zeinab2015ahmed
Zeynab Ahmed Diop :
Bayi nagne ko ak dieng Salla 😂😂
2025-10-29 09:25:54
49
timalima15
Nenetuti🦋 :
Aduna ko belal jerry, dunya ko mere mere😂😂
2025-10-29 13:03:41
16
To see more videos from user @pikoniang, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About