@seexloo1: Jubbanti #wolof_sénégal #tiktoksenegal #impuissance #apprendrelewolof @Les Grands Trains du Sénégal

Sëñ Seex Lóo
Sëñ Seex Lóo
Open In TikTok:
Region: SN
Tuesday 28 October 2025 23:08:34 GMT
1264
165
28
11

Music

Download

Comments

bld.communication2
BLD Communication 2 :
Jërëjëf Sëñ bi ci leeral yi.
2025-10-29 13:12:26
2
assane_le_kabaroi
Assane Kabaro 🇸🇳🇸🇳 :
Jaajëf sëriñ bi am na solo.
2025-10-31 13:13:02
0
redmoram
Petit🇸🇳 :
jërëjëf🥰🥰🥰
2025-10-29 14:00:18
0
jnikejr
J Nike :
machallah 🥰
2025-10-29 00:06:16
0
faddilusaatuubaa
Fàddilu Saa-Tuubaa 🇸🇳 ✊🏿 :
Jërëjëf Sëriñ Seex.😍
2025-10-28 23:11:50
0
muhidinetv
Ma-sàmba taalibe seex muhidine :
maasàllaah jërëjëf sëriñ seex Lóo
2025-11-01 08:27:46
0
aladijtoure8
aladijtoure8 :
jaajëf
2025-10-30 06:10:31
0
yacinediop9062
yacinediop9062 :
jërëjëf sëriñ bi jàng wolaf dafa am Solo sëriñ Seex lóo❤️❤️❤️❤
2025-10-29 13:31:57
0
77construction
Vente Carreaux & Lumière. :
Jërëjëf leeral yi am na solo.
2025-10-29 11:02:36
0
serigne_modou_drame
Serigne Modou Drame :
Jërëjëf, caaxaan baaxul
2025-10-29 18:44:10
0
vmix.senegaal.en
vmix senegaal en wolof :
jaajëf waay
2025-10-29 12:18:54
0
paabidemba2
paabidemba2 :
Lii kay kenn xamul lu mu !! 😭😭
2025-10-28 23:51:23
0
faadal.cobaan221
Fàllu Cobaan221 :
Lii kay du lu kenn xam !!😂😂
2025-10-29 07:32:34
0
diagne.diagne0
Diagne Diagne :
jërëjëf
2025-10-29 11:19:44
0
basiirubajaan527
basiirubajaan527 :
jërëjëf waay ❤️❤️❤
2025-10-29 07:25:35
0
abdoukhadarmback2
Bëgg Sa Réew 2050 :
Jërëjëf njaatige.
2025-10-29 14:09:28
0
seex.saaxo
Seex Saaxo :
Maasàllaa.
2025-10-29 10:49:57
0
bassiroulo333
bassirou lo :
Am na solo lool.
2025-10-28 23:22:47
0
maamur.je.saawolo
Maamur JEŊ saa-wolof :
اللهم صل وسلم على محمد
2025-10-28 23:17:08
1
gueyeserignembacke
Sëriñ Mbàkke Gëy :
maasàllaah amati na solo.🥰
2025-10-28 23:12:05
0
77construction
Vente Carreaux & Lumière. :
Lii nag yemul fii rekk, wolof yi ñuy jàngale ci (ekool) yi sax bu ñuy jàllarbi (conjugais) duñu ko defe ni ko wolof war a defe waaye jàllarbib farañse lañuy firi ci wolof. Ku ne xam na ne bokkuñu nu ñuy jàllarbee.
2025-10-29 11:08:04
1
jaasri7
Sëriñ Jaañ 78 771 51 37 :
Maasàllaa sëñ Seex Lóo amati na solo lool sax. ñii yabaate rekk lañu def.
2025-10-29 04:43:52
0
muxtaarsow632
L'enfant noir :
Maasàllaa sëriñ Seex amati na solo
2025-10-28 23:42:26
0
gaynde.fatma7
Gaynde Fatma :
🥰🥰🥰
2025-11-04 13:08:13
0
djocks.lofficiel
djocks l'officiel :
🥰🥰🥰
2025-10-29 15:39:45
0
To see more videos from user @seexloo1, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About