@mouhamedsarr407: mbakhalou Saloum yakhouna , thiéy sama Yaye akako meunone , mbakhal AK mafé🤣🤣🤣🤣
        
        
             
            Focus rek
         
        
        
            
Region: SN
            Thursday 30 October 2025 17:19:15 GMT
        
        
                            
                    
        
        
            
Music
        
        
        
            
Download
        
        
        
            
Comments
        
        
                                                
                        
                            
                            
                                
                                    
Ndeya                                        : 
                                    thiébou yapp guérté mofi am légui😂
                                
                                2025-10-30 21:22:40
                             
                         
                         107
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
LAADOUM🐏BU SONKO 🐏🐏                                        : 
                                    Waa team Mbaxalou Saloum manifester vous 😂😂😂😂😂
                                
                                2025-10-30 21:21:37
                             
                         
                         35
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
AMETH 🇺🇸🇸🇳                                        : 
                                    Bly deuge la wakhe😅
                                
                                2025-10-31 04:38:37
                             
                         
                         0
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
MD🅰️xion                                        : 
                                    Saloum saloum pire ✌️🥰🥰
                                
                                2025-10-31 00:31:37
                             
                         
                         5
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
Eric Dolphy                                        : 
                                    Guèdjiou tambadieng khalé lègui yi khamougnouko. 🤔🤔🤔
                                
                                2025-10-30 19:11:12
                             
                         
                         64
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
étudiant+Business @@@@ucad Dak                                        : 
                                    vraiment mangui giss sama bop si lim wax
                                
                                2025-10-30 22:56:59
                             
                         
                         18
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
veroniquendour15                                        : 
                                    bilay wakh nga degeu pask gniko khamoul niokoy togeu😂😂
                                
                                2025-10-30 20:30:36
                             
                         
                         7
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
kadu202414                                        : 
                                    Bilaye c vrai c du thiebou yappp
                                
                                2025-10-30 20:32:26
                             
                         
                         15
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
moussacisse3891                                        : 
                                    bilhi Moi je suis d'accord avec toi mon frère
                                
                                2025-10-31 05:27:58
                             
                         
                         0
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
Kim le jeune transitaire                                        : 
                                    lou ler nha wax bilahi mbakhal saloum deug day saff thiethiakh akk guerté 🤣🤣
                                
                                2025-10-31 00:36:49
                             
                         
                         5
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
Waly Diouf le Patriote 🇸🇳♥️                                        : 
                                    waaaa Boury mii🤣🤣🤣🤣
                                
                                2025-10-31 01:27:41
                             
                         
                         0
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
kebbatouray09                                        : 
                                    Yep Wa Dakar la rek
                                
                                2025-10-30 22:39:06
                             
                         
                         2
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
seck ndanane                                        : 
                                    ki Gueye la santa😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁
                                
                                2025-10-31 00:23:32
                             
                         
                         2
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
Bass 🇪🇸🇺🇸                                        : 
                                    Blh Senegal mo nekh 😂😂😂
                                
                                2025-10-30 17:34:32
                             
                         
                         17
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
Thiam                                        : 
                                    adouna nila kouné sa problème bou kéne khépe problèmou kéne mashallah Thi sétlougi 🤣🤣🤣🤣
                                
                                2025-10-30 22:11:41
                             
                         
                         6
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
S Moussa borome déff guiss                                        : 
                                    AK gédje tamba djang 😏
                                
                                2025-10-30 21:17:06
                             
                         
                         8
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
KKK                                        : 
                                    Il a parfaitement raison. Ce qu'on prépare aujourd'hui ça n'a rien à voir avec Mbakhalou Saloum.
                                
                                2025-10-30 22:05:37
                             
                         
                         7
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
chiekh tambedou                                        : 
                                    non wakhega deuge de nekhatoule😂
                                
                                2025-10-30 21:59:12
                             
                         
                         2
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
Baye cheikh                                        : 
                                    Ya wakh deug kay
                                
                                2025-10-31 01:50:05
                             
                         
                         2
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
Manchester city 🤍🩵                                        : 
                                    bilahi yakhouna 😂😂😂
                                
                                2025-10-30 23:10:10
                             
                         
                         4
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
therealwizzniang patriote                                        : 
                                    Ay bouri Diakhate kou laye soumbi 😂
                                
                                2025-10-31 04:24:38
                             
                         
                         0
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
ahmetdia42                                        : 
                                    Effectivement, l’un des meilleurs plats sénégalais mais on le dénature à Dakar
                                
                                2025-10-30 23:49:15
                             
                         
                         5
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
linguer2018                                        : 
                                    t'as raison déh
                                
                                2025-10-30 23:28:06
                             
                         
                         2
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
laminethiam8539                                        : 
                                    merci beaucoup 😂😂😂
                                
                                2025-10-30 20:27:18
                             
                         
                         0
                     
                                    
                        
                            
                            
                                
                                    
sns                                        : 
                                    sa wayyy beugu na mbakhal saloum ...souyy wakh mbakhal dafayy contane🤣🤣🤣
                                
                                2025-10-30 21:19:33
                             
                         
                         2
                     
                                     
        
            To see more videos from user @mouhamedsarr407, please go to the Tikwm
            homepage.