@storietime266: Djiné ngay sékk a môme relations you raféte, nga dém beu djogué fi mou diap say doom ak say seut dilén danou lo ay rap , gni mou rayléne depuis leurs naissance, keur gui ndoole Dara doufeu am etc.. Légui certains personnes yiy liguéye ak djiné niolay geumlo ni niom meune naniou Dara hors que léép ay fén késsé leu ! Djiné dafa Say Say té nitt kou Say Say ni môme lay liguéyandole pour iri ay nitt niou diokh léén offrande sou djiné bi beugué Dara meune na laa tékk febar pour nga nieuw si môme nékhal ko mou dindi ko nga wéér, sou démé beu sokhla waat mou rofate leu fébar bi nga nieuw nékhalate ko . Boulén dioum ba dém si njabar katt yi daniouy tapalé yalla wakh nako SURAT 2 BAQARA ,VERSET 102